Key Em TI – Niombato

Dans cette vidéo

Notation
4.3
Lyrics / Paroles
Sound / Son
Dance / Danse
Video / Vidéo

Key Em TI – Niombato

Paroles NIOMBATO
Heyy Ici C’est Niombato (Sokone Passy Karang Toubacouta Moyy Ci Niombato)
Weuylenn Ma Niombato (Niombato) 2x
Wayalma Niombato

1er Couplet
Welcome Ci Deuk Bougn Gnu Khamé
Beuri Diomm Foulaa Jamm Lagn Gnu Khaamé
Woutt Ndieukk Bi Dakar, Nagn Dougou Auto Demm Men
Naam Na Famille Bi Sama Gars Yii Noumou Démé
Hei Chauffeur Gawal Ndakh Talibi Bakh Na
Dieul Féri Diaarr Foundiougne, Kaolack Bi Akk Na
Admiré Fond Vert Toolou Mbookh, Bissap Naane
Baay Kaatt Youci Alleu Bi Goor Yalla Di Faanaaw
Raak Taak Yegg Nagn Passy Di Demm
Diossong Ak Mbouloum SokSide La Idem
Gnann Bountou Armel Hotel Bi Dou Blemm
Mane Naam Khegn Ndokhou Guedj Gui Nii Lemm
Gassal Sama Guedj Gui Beug Nagnu Amm Bateau Beyy Fess
Pour Niou Guiss Dieunn Yii Ballang Ba Naam Na Sugnu Tefess 2x

REFRAIN
Yeksinga Niombato, Yeksinga Fimoy Niombato 2x
Sokone Ak Passy Karang Moy Toubacouta Yeahh 2x

2e COUPLET
Dokhantou Promenade Dieul Touti Air Baby
Tourisme Toubacouta Goudi Gnuu Demm Baby
Baali Rhythm Assyko Lepp Degn Baby
Culturou Karang Dou Nekk Lingayy Bagn Baby
Niveau National 2 Thiossan Go
Medine Yoonu Ndam Tessito Ba Manko
Sport Attitude La Sunu Mbeur Yii Dii Baako
RIP Khady Diouf Nekh Baat Yeurwago
Bethenty Lool Dou Meussa Degn
RIP Gnoufa Jota Demm
Gnu Guedj Gui Yobu Looll Dou Meussa Degn
RIP Gnoufa Jota Demm
Ile Des Oiseaux, Reserve Biosphere, Patrimoine UNESCO
Plus Belle Baie Du Monde
Ile Aux Coquillages Reserve Fathala NIOMBATO
Ici C’est Niombato, Ici C’est Niombato

REFRAIN
Yeksinga Niombato, Yeksinga Fimoy Niombato 2x
Sokone Ak Passy Karang Moy Toubacouta Yeahh 2x

OUTRO
Niombato
Yeksinga Niombato
Niombato
Karang Ba Toubacouta Yeahh
Niombato
Karang Moy Toubacouta Yeahh 4x

(Visited 11 times, 1 visits today)

Vous pourriez être intéressé par

Poster un Commentaire

avatar
400
  S’abonner  
Notifier de